🔮PLATEAU SPÉCIAL: SERIGNE TOUBA AK YONENTE BI PSL AVEC GANA MESSERE/ VEND. 15 OCT. 2021

21
43

ABONNEZ-VOUS Ă  la ChaĂźne de la 2STV cliquez sur ce LIEN : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualitĂ© et Ă©missions de …

source

21 Commentaires

  1. Kou ñeuw gouddik gamou touba billahi dinga khamni mouride rek mo fonk gamou dinanfi diangue ay lim you takou si Al xuràane ak ay xassida Di fagou ay berndé you mouridé fanané tagg gandji mbindéff ba fadiar
    Kou xép sunu gamou yitt kiñu koy deffall mom birnamani khébouko

  2. Machalla nékhna yalla nanou yalla fayal serigne touba abou Diakhaté khasidayi nékhna Machalla yalla naléne yalla défal diame wéral bate yi ci barké serigne saliou mbaké

  3. Sama xool sedna lolll. Les jaloux qui disent que les mourides comparent Cheikhoul Khadim et Nabil Moustapha n'ont rien compris. Serigne a dit tout sur Moustapha. Dieuf reek laissons les parler. Gamou force, Magal force jusqu'à la fin du monde. Soyeux anniversaire à notre cher aimé Nabil Moustapha. Bilahi je suis trÚs content

Comments are closed.