🛑PART 2 ENCORE+ SPÉCIAL C. AHMADOU BAMBA 📍ABDOULAYE DIOP BICHIRI📍THIEDO MOURIDE SADIKH📍CHEIKH MBAYE

40

S’abonner Ă  la chaĂźne de la 2stv cliquez sur ce lien : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualitĂ© et Ă©missions de sociĂ©tĂ©, santĂ© …

source

26 Commentaires

  1. Euskeuy machallah dieureudieuf Serigne touba kenla amoul morom mbacke diarama mam cheikh Ibrahima fall lamp Serigne mountakha mbacke yallah nafi yague lol ta wer mbacke machallah dieureudieuf Serigne Abdoulaye diop bichiri man di sa domou bay Souleymane diop beugue fallou fi si touba tolentino keur Serigne touba Italie suonouy khÎl Saïd nalo si wakhtanou khadimou rassoul wi yallah nalen Serigne touba fay ngen am wer goudou fane ak kheweul si barke yonantibi alay salatou wasalam si barke khadimou rassol si barke" khasidayi si barkhe" werou korgui yen wa 2stv beugué nanoulen" si wakhtanou plateau bi fi korgui machallah yallah nasen telebi am yokoute" machallah dieureudieuf

  2. DieureudieufĂ© borom touba ❀❀
    Serigne Ablaye Diop bichri yalla na la yalla dĂ©fal tawfeex mousĂ«ul la či fann wu gaat baarkep Serigne Touba ❀

  3. Thiey yallah❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀

  4. Serigne Touba amoul morom❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀

Comments are closed.