🛑SUIVEZ SUKERU KOOR AVEC TAFSIR ABDOURAHMANE GAYE ET CHERIF MAMINE AIDARA | LUNDI 10 MAI 2021

67

ABONNEZ-VOUS à la Chaîne de la 2STV cliquez sur ce LIEN : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualité et émissions de …

source

20 Commentaires

  1. Yalla na lenn yalla fayy.may lenn wérr ak werlé niou féké koo ayy atti attt thi barké seydinah mouhamed(psl).bègue naa trop ,yalla na lenn yalla béguel thi adouna akk thi alahiraa🙏🙏🙏🙏😥

  2. Machallah🙏🙏
    Machallah🙏🙏
    Deweneti yalna'niou bour yalla na'ngoul té diégeul'niou sou niou bakar soopi'ko ay tiyaba si barki séydina🙏 mouhamed psl amine🙏

  3. Machaala yalnalène sounou borom fayal bopam si barké Rassoulilah
    Vréma après koor gui warone guène amm même bène émission si semaine bi

  4. Ma Sha Allàh sen ande bi nekh nama torop… Sama yaram dafay daw🤩🤩🤩, yallah na yague te yallah bayi len fi guen di gnou yede ak wane yon WI insha Allah 💕💕💕💯💯💯😍😍😍🥰🥰🥰🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋

  5. Machalla yalla neu yalla faylen dina lenn nameu Lou beuri amlen diam tawfekh ak shifaou 💞💕💞💕🇫🇷💞💕💞💕🇸🇳💞💕💞💕

  6. Mon Capitaine boul demissioner te nga moytou journalistes seytane yi di tassoum rew sa carriere lagnou bouga yak bayil khel sa ndiambote ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

Comments are closed.