🛑SUIVEZ YOON WI AVEC OUSTAZ ABDOULAYE GAYE | JEUDI 1er JUILLET 2021

32

ABONNEZ-VOUS Ă  la ChaĂ®ne de la 2STV cliquez sur ce LIEN : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualitĂ© et Ă©missions de …

source

2 Commentaires

  1. MachaAllah MachaAllah, émissions dîné you ma moussa sétan akk deglou yeup, bi mossi eupeu solo.
    Kham kham akk geustou rekk moye deug. Émissions yi lañou sokhla. Dé léne inviter ñou melni parce que genre ñi rekk ño meuna dioubanti sénégalais yi.
    Bou ndieuk ñou nekk Europe dañou dan yoné sénis ndiabott Sénégal pour ñou kham Séne religion, séne culture sénégalaise ect.. mais légui kéne niéméwouko ndakh li âme Sénégal.
    En tout lidiot diot na.
    Oustass Abdallah yalnala borombi défal diam akk salam, are la yiir la, bayilafi ndakh émissions yi ngaye deff amna solo lolou. Man dé saye wakhtane laye deglou Bess bou nekk( yobalou souba yi).

Comments are closed.