🛑SUIVEZ YOON WI AVEC OUSTAZ MAODO FAYE | JEUDI 30 SEPTEMBRE 2021

39
44

S’abonner à la chaîne de la 2stv cliquez sur ce lien : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualité et émissions de société, santé …

source

39 Commentaires

  1. Oh universel lerna. Yeen mourid yi saaga laye waxal. L'injure mom c'est l'arme des faibles. Kou degg deugg neexula ta amo argument, tu deviend insolent. Mais bilahi, walahi, wa tallahi, soxna aïda minguendi wax lou gnaw gnoune ay talibem, waxuma yeen gniy saaga deh, xalif general des mourid laa wax tolougnou si cheville. Dougnou moromam si yalla. Gnoko gueuneu xam serigne touba. Kouma saaga nak baalnala. Damay xamni tu fais parti des faibles.

  2. Xam xam Bo guiss xam yalla KO dakh fouffff, laissé les chiens aboient la caravane passe…. Delen wax rk niouy guen di dem, seni niak tèguine moy sene lorangué… Jeureudieutiii serigne bethio, Ibrahima samba yagual wereul…. 👌 👌 👌 👌

  3. Sama sang bi serigne saliou nèna nit bouy wakh lo khamoul dagay niane yalla sunu borom youbou la meun kham limouy wakh wayè nèna boul teup teup rk wèdiko..sunu borom yamoul fène..

  4. Waw goreway S SALIOU Samb
    SOKHNA Aïda SALIOU YALAH NAFI YAGUE TÉ WER ANDEÉ KOK SOKHNA BATOR SALIOU AK SOKHNA ADJIA SALIOU ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  5. Bilahi kéne dou dindi linga wakh 🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥 L'INJURE EST L'ARME DES FAIBLES

Comments are closed.