À vous de juger la route nationale

22
37

source

22 Commentaires

  1. Naniou toke fi di commentaire rek tè bagna dioke lidjenty ngoure gui niou toke fi di wakhe rek niome nio ngi dounde dè ake souniou khalisse en plus . Kou meune diende aye blindè ngir note sa askane khana wara meune tabakhe aye ecoles ake aye hopitaux ; mains non dieule khalissou askane bi djendè ko aye blindè pour fasse yènè dalesi kawe askane bi mais billahi wallahi macky do ame ndame

  2. Thieuy yalla Senegal mane mome sama waleu maynalenko ciao bye bise bou ibou daffa wathè si gourgi ma khol ndakh dina meune ngibiai😭😭😭

Comments are closed.