Affaire Wally Seck : Les conseils de Pa Assane Seck à l'artiste

40

Subateel du lundi Juillet 2021.

source

34 Commentaires

  1. Ndaw si mon xalat bayam bi fatou mes waly xalatouko souko xalaton day bayi ba yayam mourekou mou contune conceram
    Insbi mom dafa waron rander image papam maís ay adamo

  2. Pape Assane lingua wakh la meuneu degeu c'est pas parce que dafa niaka wadiour motakh ehAsma khamngua louy deugeu moy li Pape Asszbe wakh na moytou lolou moy deugeu dou période de crise deugeu dou rombeu nopeu touma thi afouna lagnouko fek wakh dji moy na sétate bopame kham limouy deff ak limouy wakh point mane keneu geunoumako beugeu kèneu geunouma bokk ak mome

  3. Merci par assane mais aussi il faut dire la vérité pas du genre de il vient de perdre son père qui n a pas perdu le sien faut arrêter cet alibi la c est nul

  4. C pas la 1ère fois Waly plainte wone nafi Imam Kanté…té dou mom kassé mofi niak baye khalé bou djiguène bi khamo lingay wakh.
    Waly na réglé rek.

  5. Wally makk yi dagn la beug accompager nga exceller tout en restant sur la voix de SIRATAL MUSTAHIM. Yalla nala borom bi taxawu 🙏🙏🙏

  6. 🇸🇳🇦🇷🇧🇷🇧🇷👏🏽💯👊🏽 masha alla
    Bonne continuacion si lep lou bakh amine pa assane goudal fan lolou amine 🤲🏾🙏🏽🕋🕌

  7. Wally seck niou fans dagno sonou
    Yaw rk yaniou si meune guéné
    Guir yalla hamal figay ték sa tak
    Lolou lalay laygnan Bougnoula
    Dégat si lolou ok bonne continuation frère 😌😌😌😌😌

Comments are closed.