Au moment ou Diouf Sarr se pavane dans la capitale la police interdit à Barthélémy Diaz d'aller au

44
51

dakarmatin#Actualite#chronique#senegalAu moment ou Diouf Sarr se pavane dans la capitale la police interdit à Barthélémy Diaz d’aller au centre ville de …

source

44 Commentaires

  1. Man ak loumana Sama fami kènne manosii allkati ndakh daradia rek lanou khame mem allkati biii limouye gèunaloko meis Senegal mo tolou fii ndakh makci sall ak Wa ngorgui wathi nan ngorgui moy sèn Adina yakhona fii ta alakhira mome Lou way lèk fii sii ta lèwoula digako guèkhue bamou sètt

  2. Ndah gnoune Sénégal da âme gnou wara Doh ak gnou waruta Doh ndah Li c'est la 1er fois ma guise ko ndah deuk ci rew mi té bo guéné gnou ni bumu dém ndah sunu police Bi Li Mo tahone are sa askane Wala dor sa askane ludul diéh yalla bindouko le pays va mal

  3. Lou takh sénégalais meunoul xéx dagne koy mane xéx bi dou lolou commissaire bi amna na dom amna yaye amna diabar nionniou rk doy na pour affaire yi règle wou khamléne moy kane kham fimou dekeu rk taraké ndiabott gui rk mou diex bouniou déféi legui tay koumou beugue déf lo lou bonne nga bagn doko niémé rk mou diéx

  4. On é plus en sécurité. S'il s'agit de protéger la population elle (police)ne se mette dans la circulation.mais s'il s'agit de l'opposition elles sont armées jusqu'à dent. C'est une honte

  5. Population yi nio inconscients rek mais amoul dara lougn meuna diapé Barth. Niakk fayda rek police bou amatoul ben gueudd mais so lene défoul nank beu deuk bi yeungueutou watt di nguen guiss policiers youy daww com beuyy Insha’allah lolou meunoul niakk Senegal ndakh President bou bone

Comments are closed.