CHEIKH YERIM SECK « Sonko wakham dafa beuri da wara … »

43

Archivages des 72 h de la SenTV.

source

39 Commentaires

  1. Ñune sénégalais lamda yi dey sonko wakh lañ sokhla na wakh dé Sonkoooooooo nguir YALLA dél wakh guinàw YALLA loo am wakh la ko may bul deglou vo rien yii déh amou gnou béne njarign snegal ay mercenaire lagn

  2. Yerim, vous êtes limite insultant ! Vous donnez des leçons à tout bout champs alors que vous n assumez pas vos propos ! Franchement vous n avez pas le même niveau et honnêteté que Sonko malgré votre sodo titre de grand journaliste à "Jeune Afrique". Vous ne seriez pas un peu dépassé par les événements ?

  3. Bialy ossmane sonko wakhal deh bu bakhh yii linou beuugg moy nga nopi niou lèek la Senegal mo mèel nonou dafa am nio sokhor danlay nopilo banou yobou la casso aperis niom nioy wakhat lan motakh wakhton sonko boula keen wakh loy def loudol sa partie passtif ak yiila beugg wayei kou yakarne senegalese yi dano doff nion khamnan lèpou wakhi sonko mom guièn ataandol .ablaye wade dafa wakh ba dial riwwmi cheikh yiriim seck khana dagabokk siyi macky yondi ndeysan malen yerum teguen rakhass si xol yi adouna amol solo

  4. Les Sonko boys ne nous emmerdez pas way il a dit ce qu’il pense et vous êtes là à raconter du n’importe quoi combien de fois Yérim a parlé de bien de sonko ou critiqué Macky et là vous aviez salué son courage et là il le critique vous voulez le descendre.Sonko Ousmane concentre toi sur ton livre e des 10 dernière jours du mois de ramadan et prépare bien le procès inchallah

  5. Sincèrement parlé cheikh yerim n aime pas Ousmane sonko et cela se manifeste beaucoup sur yerim post et dans ses sorties à la télévision

  6. dell moudie wakh tay nieukeu nopi yow mom niep kham naniou ni si souk macky Sall yi gua bok ya gueuna bari wakh sonko nak ya gui weurr tele yi di ratatati rek chimmm

  7. Waw yawmy nga khamni yangi topou teleyi di vakh reck yaw mi lane vara vakh ki macki laye ligeeyal cheikh yrime may nou yaw deglou voune la

  8. Gnoune bou sonko wakhoul stress Ray gnou dafa wara wakh gnou kham né il est toujour engagé et respecté l statut du président qu'il est déjà pour les patriotes 🇸🇳🇸🇳 sonko est notre président kouka bagne dèèle .

  9. Sénégal mo metti soye wakh gnoune daffa barri wakh so noppé gnoune loutakh wakhoul sonko souyé askane bii laye wakhal te mane dee so ware wakh 21h:00 19:00 lakoye commencer karr.Sonko boul meussa nopp

Comments are closed.