"EUMEU SENE DAFA WAKH WAKHETT", EUMEU DONNE UNE RÉPONSE AMÈRE A SES DÉTRACTEURS

20

S’abonner à la chaîne de la 2stv cliquez sur ce lien : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualité et émissions de société, santé …

source

34 Commentaires

  1. A mon avis Balla gaye il aura la chance de battre tout les champions de l'arène grâce à ses revanches vs Bombardier et eumeu par se que c'est eux qui manquaient dans son riche palmarès noonn eumeu werena trop mais bon business la en plus il proche à la retraite

  2. C’est vrai que Eupeu daye liguéy mais dieul bimou dieul balla dafma wagni si mome lou barri. Et puis gniko wakh mou dieul combat bi nga khamni ay kilifam lagnou danio warra khamni eumeu kilifa la et puis nawléla. Warouniouko wone niane mou dieul combat bi parsk dafay Wédi wakham. Té kadou daffa fort ci nite té tay loumou wakhati ba watteko dou takh mane Khalifa ma dogou ci. Li eumeu wakh nakk explication la mais doyoul justification. Wa salam

  3. Boycotélel mbeur ay defeant lagne sen bop rek moléne yitél askan ba ngi sonou doléne ci wa mane jeune gnou inconscient yiléne di topeu na yeureume

  4. 100%100 Di niane sounious Sénégal yalla nafi diamou yague Di Nianal eumeu sene yalla sounious brome Maye koo ndame si combat yepou Balla gaye nak môme nite bou bakh la ma çhaalah 100%100 baol baol ba gui nonou Di nianal gnépou diamou sounious Sénégal nioko bockou téxi neck 100%100 eumeu sene rék

  5. Niit ak loumou meune ta done dagay sam sa kaddu dakh souba kén khamoul lanla la té yalla rék moy ki kham tay kham souba kone lép loy wakh rék khalatal ni yalla rék moy ki kham liy khéw

  6. Bilahi yawe eumeu Sene gayi dieynanla baga nagou 🤷‍♂️wayé manmom parénasi Manon nga samou aye kadou rek khare yalla 🤷‍♂️😢

Comments are closed.