Iran Ndao: '' Nafekk loumou la wakh dey fén, té fén kate…."

28

Archivages des 72 h de la SenTV.

source

22 Commentaires

  1. Antouka ira xawmako mai dal géntena ci mom lo xamné kou yébo déf ci môme ndage am na louko Yalah may bilahi xawmako mo soumako guis xana télé mai dal xamna né amna may té bilahi sétanlene rék ak niko sorou xawmako nag bilahi walahi

  2. Non mane Iran damako fan. Badianene Pire la, khexx Kat Pire la, diambar Pire la. Boul fale nyi Laye saga ak di fonto. Kaye nek nen 🥚mune muk muk niou merre ko. Sof ba dee

Comments are closed.