L'agression de Ousmane Tounkara au consulat du Sénégal aux États-Unis

110

dakarmatin#Actualite#chronique#senegal.

source

45 Commentaires

  1. Gnome gneupe lagnouye deugue séne ndaye. Le combat vient de commencer. Je me demande comment un consulat peut accuser un compatriote de terroriste parce que c’est un activiste

  2. fila beute yam li cest grave thieuy diamou macky sall yi ousmane tounkara meunolene si mome dara teh doléne ko def dara mouy usa di senegal peuple bi yewou nagne nekatuniou a di kholéne nguéne di néwal dolé domou senegal yi dafa doy depuis 2012 ken meunoul ame diam teuthie rek momoléne niou nak

  3. C’est qui cet agresseur, Qui travaille au consulat ? Il doit savoir qu’il est là pour le citoyen sénégalais et qu’il est payé par le contribuable citoyen sénégalais..

  4. Sènegal dale kou man sa morom doumeu lolou mofi wara dièhh. Normalement quand vous résidez à l’étranger et vous entrez dans le consulat vous déviez vous sentir chez vous malheureusement ce qui ce passe vous êtes mieux traité à l’extérieur que chez vous, c sa le Sénégal 🇸🇳

  5. Mais mane damay guente wala mais gni ay nitt laniou wala ay mbaam diapp Sénégalais yi melni kou yorsay kharr di teudj aka tidji aka fitnaal ken dou sakh wakh

  6. Nonnn waroone na nekk mane bama oubi leufeul ndéyam. Tounkara amal diam rk lii yeup dina dieh mm bo gnibissé Sénégal douniou délou guinaw. Macky dinagn dohaane ndém thie nii wala thie neulé

  7. Douma tayi diko wakh nous sommes en face d'un état voyou, aye domeram dou gnii gnoy diapaléla les émigrés. La diaspora vous a vomis tchim

  8. Guem lene yalla ta khamni yalla amna. ELHADJ NDAO BÊTE GAGNOU WORE GAGNOU WORE GA SA YAYE WORE SA ASKANE YEUP. LI ALALOU ADOUNA DIAROUKO. TOUNKARA SA GORO LA. YAW AK DIABARAM YENA BOK BENE PAPA..C'EST VRAIMENT TRISTE. SA KHET YAROUNIOULA SI GNAK NGORE. 😭😭😭😭😭😭

Comments are closed.