Les révélations d'Ousmane Tounkara sur sa détention au USA

53

Les révélations d’Ousmane Tounkara sur sa détention au USA.

source

41 Commentaires

  1. Yallah na yallah ate bou ler balla le 11 mai inchallah. Inchallah yallah dinala may ndam si kaw état sénégalais bou bon bi. Li rafetoul. Man senegalou Macky Sall bi me dégoute. Gni yallah nalen yallah dieule noumou gueune waw nak sénégalais am diam ak Salam. Amine. Te inchallah yallah di nako Def si khatanam.

  2. Ousmane Toukhara may Allah Subhanah peace and blessings be upon you and ur family.
    We are all behind you big brother.
    May u come out of this ur head high insha'Allah ☝🏾

  3. Thiey Yalla ngouru aduna ak poste diaral nalen lounek ba tekk ay tolof tolof sa beau frère wayei nguru yalla rek modoul djekh t euleuk dinaniou ko layo Ak sunu borom… Yalnala yalla taxawu Ousmane degg Rekay moudjj In Sha Allah…

  4. Kel plaisir d'entendre ta voix cher frère Ousmane Tounkara…ke le Seigneur étend sa main de bénédictions et grâces sur toi et famille et ke tu t'en sors sain et sauve…inchallah,courage a toi!

Comments are closed.