Les vérités d'imam Ibrahima Dramé sur les affaires capitaine Touré , Cheikh Omar Diagne et Adji Sarr

27
122

dakarmatin#Actualite#chronique#senegal#ibrahimadrame Les vérités d’imam Ibrahima Dramé sur les affaires capitaine Touré …

source

27 Commentaires

  1. papa dji kou diara déklou leu bounko déklou woon avant khéw khéwou mars yi li khéwon lép dou khéw machallah yalnasa fane goudou loll ande ak wér

  2. Yalla na la Yall féye Imam.
    Maquis minable sale est le président le plus dégueulasse que le Sénégal ait connu. Wayé na gnou déme rék.
    Nous espérons que tôt ou tard tu le paieras et très cher.

  3. Amna nion khamnè solen narè soul yay soulou soukh torokh wayadi bilahi (lisi kanam rawoul beutt)ayweu rk merci pape

  4. Merci père yaleu yallah feyi leu. Pape alé niang yow dagne leu beug trop. Wanté sa video mo défone si juge di wakh ni juge comasè dale neu sa hél. Juge bi ak macky sall béne lagne kham gani juge dou dèf lou nékhoul macky sall ni mariem faye sall ak Moussa fall si deal bi lagne bokh

  5. Lii laniou sokhla si kilifa diné wayé ancaissé rek moute rek kilifa bou doylowoule yalla ak yonénté bii (saw) ak sa liguéyou mame ngoure dila diokhe ngaye léke bou deuk dii take sakhe do wakhe wa salame

  6. Sénégalais yhi nanu takhaw ame foula bagn ci kep kuy dialgati Yoon gnou jeuflanté ko ak yow ba sunu dernière énergie☝️✊🏾✊🏾✊🏾diam Sénégal✊🏾✊🏾✊🏾✊🏾

Comments are closed.