Me EL HADJ DIOUF TACLE SONKO: "MENACE DE MORT.., DI SAGA NITT GNI, TALE NANIOU SAMA KEUR,

44
21

ABONNEZ-VOUS à la Chaîne de la 2STV cliquez sur ce LIEN : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualité et émissions de …

source

44 Commentaires

  1. Elhdji mi damako yeurém apres ça mort 😭😭 parce que nafikala, fénnikatela, epui interem guéssé lé d’éfandre, mais sénégalais yii doff gnou légui,,,,bou Ousmane Sonko reguiléne Sénégal 🇸🇳 do toléne avancée wallahi , Ousmane Sonko yalla mo gnoudiapalé Sénégalaiyiii indiko, bou gnouko foyée, dinagnou sonnou balla gnou amatte comme Ousmane Sonko, mais mr Elhdji diouf tu as bien compris que Ousmane Sonko mo yore affaire bi , mais Lolou Doula interéssé , sa intére
    Rek mais do yakou sunu Sénégal 🇸🇳 ak sa bire bou macky sall bi

  2. Mak boudoule wakh deug saga ndém rék moo bakh thi Môme.
    Soncko par force 🇸🇳✊🏾liléne diakhale moye litakh jeune yii naw soncko guissagoulén darra continuer rék sén gat dineu moudj lak

Comments are closed.