"NANGOU REK WALEU BAGNE" LA NOUVELLE DANCE QUI DÉCHIRE ; DJ KHEUCHA L'IMITE A FOND MDR 😂😂

36

S’abonner Ă  la chaĂźne de la 2stv cliquez sur ce lien : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualitĂ© et Ă©missions de sociĂ©tĂ©, santĂ© …

source

28 Commentaires

  1. 😭😭😭Mane dĂ© dama beugone kou ma diaye GuĂ©ne ma SĂ©nĂ©gal Ndiaye mi 25 fran sakhe bakhe na deukeu bou ma Ăąme bakhe na n'a GuĂ©ne SĂ©nĂ©gal rĂ©k pour bangiati guisse yene espesou nite yi

  2. Borome commentaires negatives yii
    Gni lignouy dĂ©ff mo tanĂ© thiagatou … satche wala agression gni au moins dagni fo rĂ©k ce n'est que de l'ambiance bayilĂ©ne wakh bou gnaw tchi nitte ko khamoul

  3. Noo franchement dangéne gnou yape li moye lane pourquoi ngéne beugu gnou forcée gni outiléne programme pour télé bi niak guéne fayda trop. Guéll yi niome louma léne beugu wakh rék khép ko nama yalla ball. Wakh léne si goorjiguéne yi ak gnou mélni niome. Wakh léne si ressources yi gnouye sath dika séddo sounou littoral bi ak you mélni gnome wakh léne si khalissou réwmi gnouye passarr passaré étant d'autres mo gueuneu li ngén khame né défoul pervertir khallé yi

  4. C du n'importe quoi dans cette pays ya les tĂȘtes bien faites mais jamais niou soutenir lĂ©ne si sĂ©n ni progĂ© d'avenir đŸ€ŠđŸŸâ€â™‚ïžđŸ€ŠđŸŸâ€â™‚ïžđŸ€ŠđŸŸâ€â™‚ïž

  5. Sénégal li motakh développement dou am jamais les jeunes entrepreneurs ou bien gni nek di déff ay effort pour servire leurs pays ken doulén invité si poteaux yi mais allons rek

Comments are closed.