NERVIS VS LUTTEURS – ZOSS, SANTANG, FORZA…DEPLORENT : "AMOUL BENE MBEUR BOY GUISS SI PROBLEME YOYU

6
31

ABONNEZ-VOUS à la Chaîne de la 2STV cliquez sur ce LIEN : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualité et émissions de …

source

6 Commentaires

  1. Zoss boulen gnou Sonal . wakhou gnou yén mbeur yi magg yi mais mbeur you ndaw you bari ay nervis lagn lolou moy deug.mbeur you ndaw yi yousi barri meussou gnou ame combat té gnougui entraîner si écurie yi boy yoyou la ga yi di fay ay 25mille pour gnou nekeu nervis di dorr population en plus yén mbeur you magg yi Sen intérêt Rekk ngén fi nekal bou Askan wi di diog pour khékh ngir doundou bou Cher bi yén nieup Keneu doulen degg té pourtant Sen supporter yeup si pauvreté lagnou deukeu mais vous ne les défendaient pas cest honteux de votre part lolou moy deugeu sen intérêt Rekk

  2. Santang may gnou sounou jam mbeurou parcelle yeup ay nervis lagn xana koulén guissoul gneuw defalen formation garde rapproche si 1 mois niom gneup ay nervi lagn garde rapproche si un mois Macky ak ay niteum gno yakh réwmi y a plusieurs nervis lutteurs j peux cité bkp zoss dangay doul lingay wax dara doussi deug nga balma

Comments are closed.