S MOUSTAPHA DRAME « Lathie djiguéne numéro téléphone sakh ndialo la »

28

Archivages des 72 h de la SenTV.

source

25 Commentaires

  1. Mei ki limiy wakh khamusi dara nian yalla kukoy deff lula nékh ngua fayyiku ak nian kén dako mana fay Moustapha darame nhi dan lay fohé rek baggue la lambal thi palatoyi boul fatte lila yalla defal bagua koy diaff guiso thi niom kén bo wormale yalla ba yalla normal le nk daguey kham sa boppou maytoul palato teleyi te neck si ligua néckon sak sén yitte moy nula nit yiy xébe ak lun lay torokhale toguatal bou bakh te yokkou sak diamou yalla mn khawmala mei bimala guise rek la khamne yalla defnasi yaw Dara

  2. MAIS TAMITE SAFARA YALLA JI MOYE XOL KOUKO SOB MOU TABAL LAFA NAGNE BAYI DI NIAWO SOUGNU BIRE WALLY SECK NAK D'UN COTÉ DEFNA ERREUR MAIS NOUS SOMMES TOUS DES MUSULMANS … KOU BEUG SOUGNU BOROM SOUTURAL LA DAGUAY SOUTURAL SA MOROMOU DJOULITE … NAGNSI BAYI XEL

  3. Eh koubakh ki Yangui koy soga Récemment la wakh né mogui diegalou bén mbeur bo khamni bimouy beuré ak bombardier defnako liguey bou bone.Mouni mbeur bi nako diegal.

  4. Serigne Dramé bilahi ,il as parfaitement raison ,,mom loumou wakh rék téré laaa ,mane mossouko guiss mais d'où wakh louko nékh diné layy wakh … Sénégal mo nékhoul wakhéé ,naniou dianggui souniou diné ,,,

Comments are closed.