SIDY DIOP MET LE FEU À CICES ET FAIT DANSER LES ÉTUDIANTS D'ENSUP AFRIQUE AVEC SES TUBES

34
35

ABONNEZ-VOUS à la Chaîne de la 2STV cliquez sur ce LIEN : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes …

source

34 Commentaires

  1. Matar diop kou sokhoroul khame nani kén la si music senegal mais sidy tamit niew mana waye nekha diapalé ame feeling ak style loume sol mou rafete mobtakh sidy bientôt il va devenir le roi du mbalakh

  2. Kay ma wakhlén li sidy eupé ay moromam chance dafa dadié ak nit kou bakh ko khame mane n'a yobou fou nek sidy ak wa soubatel mouy matar diop moy le plus grand producteur de l'Afrique kou ame bén remarque bi khame ni ba sidy dougué soubatel balegui fou nek lay dem té tourné international bientôt si 2022 bi

  3. Mais sidy mom ken manouko déstabiliser bilaye linguén di guis mou ande ak mom lou ndawla nioulen guéna ame dolé niongui si guinawam surtout wa sidy family ak khaleyi beug sidy ak wa tontou dou frokh boy you graw té kou lale sidy dinga ame loula meti

  4. Deuk bu tolni senegal gnuni bene waykat la wara am Sidi dina oubi sa tounu nday wally hamko naak mongui gnew mbeur dou toutii dayy maag daane NB

Comments are closed.