SITEU VS PAPA SOW : REVIVEZ LES TEMPS FORTS DU COMBAT

25
220

ABONNEZ-VOUS à la Chaîne de la 2STV cliquez sur ce LIEN : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualité et émissions de …

source

25 Commentaires

  1. Siteu a encore innové ak touss bi on sent bien la touche bien serere dou sama mbeur nakk

    Mais siteu diene kaire combat leu
    Siteu yekini jr
    Siteu lac 2
    Siteu boy Niang 2
    Siteu amanekh

  2. Modou Mbaye wakho fi darra lane motax ngaine ragal wa diamegeune mbeur Bou naik amena droit guéné ayes sarakham thie bire lamb bilakhy souniou beuréwone ngaine khameni siteu dou mbeur faithie kate la

  3. Modou Mbaye linga wax deug leuu
    Meii osii amna droit diar fofou louy ndayou teugue katt yii diko teireii diarr fofou ltax
    Osii wax nga ko siteu niata yone la rombou baye demba teii waxoul
    Osii ltax papa sow di rombou djily diko bagne delen wax li nekk way

  4. Siteu diougal fi amo dra lo wax
    Pareii wo mtax sa teugue katt yii yakh lamb j
    Osii iow bayil sa waxou combat ak gouye guii iow xerr lagn la sandii ngay wax ni rkk ki tamba lagn ko sandii beugoul osii lolou yako neub gouye guii dane la boul niou sonal
    Osii bayii ba papa sow gagnou ngay soga nieuw di diayou teii papa biko dra da loul wone waxo diayou wo dignou sonal fii
    Papa sow mola meuneu fouff

Comments are closed.