Video-Gaston Mbengue défend Wally SECK: "Nagn bayi Jambour…Gnikay wakh ay nafekh lagnou"

32

Video-Gaston Mbengue défend Wally SECK: “Gnikay wakh borom gnari tour yi sakh ken khamoul lignou done…”

source

18 Commentaires

  1. Gaston, waw yow, ni reck. Gaston adouna dou kēēur. Ragalal ki la saak té nga xamné adouna dou kēēur. Wahhal Waly dëëg. Tout le monde l'aime. Arrêtes ce sentiment que bayam daf fiy dogga joogué bé keen fou wakh waly daara. Aimer et aider ce jeune, c'est de lui donner des conseils. Mais GASS yow, money reck ngay DIAMOU.

  2. Deug rék nga wakh fi loufi nior baniou koy mathieu sakh beug ko tong tong ay wakhou daw ak daw diégg dong laniou indiwatt diko wakh di manipuler nitt gni Mélni nioniou mom

  3. "Nagn bayi diabmour", niak argument mo bonne deug, na bayi di déf lounioukoy djign mo eupp solo sén wakhdjiou beurri dji yeupp té niak solo pfffffff 🤧🤧😪😪😪

Comments are closed.