« YOUSSOU NDOUR BANDIT LA », MAMADOU GUISSE FAIT DES REVELATIONS EXPLOSIVES SUR YOUSSOU NDOUR

47

ABONNEZ-VOUS à la Chaîne de la 2STV cliquez sur ce LIEN : https://bit.ly/3cnXP6h Retrouvez l’ensemble de nos programmes d’actualité et émissions de …

source

40 Commentaires

  1. Tounkara qui diaroul sakh invité fékké maci bolé ka nékone baniouko fa daké si la bagne youssou ndour batay khol bi mo bone

  2. Youssou Ndour, Mr le Roi de Créais des Emplois, Youssou Ndour Mr Le Silence,et le Travail.
    Le Sénégal est devenue un Territoire de la Méchancetés, et de la Jalousie.

    Je n'ai jamais vue des Vieux aussi méchant

  3. Wa gni gnom khana youssou Ndour dafa meusse nangou sen guel wala sen diabar? Wala dafa lekk sen khaliss? Yeineu ken khamoul sokhor leu keine khamoul ignane leu? Topeu beine nitt matin midi soir di wakh si mome rek, lii c’est trop way, en plus nitt koy wakhal teh diemoul kham sakh nakh yagui exister, sougueine amone dignité nopi gueine bou yagg teh wouti leineine lou gueine def au lieu de nous tympaniser avec youssou Ndour

  4. Sénégalais Bayileine kou wakh dara Youssou Ndour gueine wakh ay noones lagn, beugg nitt boumou takh gueine teudj sen beutt, bou sathioul ay fréquences diambour khamgueine ni Makk bou tolni El Hadji Ndiaye dou tokk si télé bi dikko wakh, Youssou Ndour démentirouko

  5. Yaw fo toge kola khame Senegal gaye guisse koy Khasse kola quene youssou Ndour do sa morome wakhalle rek Youssa avace sa kaname

  6. Deux ratés mécontents qui passent leur temps à dénigrer Youssou Ndour. Franchement dites-nous ce que vous avez fait pour le Sénégal d’abord? Le ridicule ne tue pas dans ce pays bande de tocard.

  7. Si vous voulez mener votre combat de cette manière vous allez droit au mur et vous passez pour des aigris ! le problème de la culture ce n'est pas YN je suis désolée. Les artistes pour la plupart n'ont aucun esprit entreprenarial peu ont exploiter leur popularité pour investir dans d'autres secteurs. mieux vaut conjuguer vos forces pour lou lene djemeuler kanam t bayi derou jambour

  8. Yalna Yallah mousseul Youssou Madjiguene Ndour si nones bou laakou ak bou fegne .
    Yalna la Yallah ate ak seu nones yii Youssou .
    King forever🇸🇳🌟🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  9. Ce guissé c’est un deumm day duull reek khamoul duul thi politics la nékone khamoul dara loumou dééff thi poche bii lay oute de même ce con d’idrissa diop amoul doul toukhou yamba ak nane laffi nékké mouy nane héberger doul ké mom il est malade néna Youssou ndour souko wowé dou dieul Youssou ndour foula wowone do dieul déé sa baye sa mame say dom yeupay dieul domeram Youssou ndour sakh khamoula

Comments are closed.